Adiouza - Ya Rassoul

Composition : Adiouza
Arrangement : Moussa Ngom
Auteur : Baxaw
Réalisateur : Komin
Styliste : La tenue orientale verte inspirée de la collection de Dideva au Maroc.
Styliste : tenue yaye Fall crée par Kinouche.

Remerciements : Mareme chalar, Ma famille, Ouza, Serigne Mamoune Aidara, Nabyien, le staff, fondation keur Rassoul.

Résumé :
Adiouza a choisi le saint mois du Ramadan pour célébrer le Sceau des Prophètes Mohamed (PSL) .
Découvrez cette belle exclusivité !
Avec sa voix suave, elle chante l' Homme de Médine dans un style fusion tradi-moderne Sénégalais. Saisissez l’émotion de cette belle ode .


Lyrics Ya Rassoul

Couplet 1

Yaye sangeu sangeu yi
Nabi
Moye sangeu sangeu
Nabi

Gnenti atte la malaka Djibril xare deundeume beu
Guener leumdeume beu
deff Thi lere ak yeurmander

Pré refrain
Bamouye ndaw lagne ko nane
Al amine te wotegoule
Jourome gnenti atte lagne ko nane al amine te wotegoule

Werou rajape Thi nga ragnanone
Yalla deff ngaye geune di mindef
Y’a rassoulalah éhhhh

Refrain
Ya Naby ya Rassoul’ Allah
Salam aleika (bis)
Ma weuye la
Ma kagne la
Rassoul’ Allah ( bis)

2 eme couplet

Arou hira falla yalla yabale Djibril
Mou Neko ikra naby tite ba bire houreychi

Na nane zamilouni zamilouni Khadija sangema (bis)

Mou daldi mourri karawame la Naby guisse démate.
Mou xamalniko guisso kenene koudoul Djibril.
Yefere ya ngui koye fexale
Thi la gadaye makk Dieume Medine
Omar tothieu taxe yeee nodolo Bilal.

Pré refrain :
Bamouye ndaw lagne ko nane
Al amine te wotegoule
Jourome gnenti atte lagne ko nane al amine te wotegoule

Werou rajape Thi nga ragnanone
Yalla deff ngaye geune di mindef
Ya Rassoul’ allah éhhhh

Refrain :
Ya Naby ya Rassoul’ allah
Salam aleika (bis)
Ma weuye la
Ma kagne la
Rassoul’ Allah ( bis)

Pont :
Nanou lere Lo Aye jikome
Ndax gnou bokkeu Thi mome
Ki Wa meune gayé Rassoul’Allah
Lerame ga yobouwaler
Sounou doyadi
Nguir mou jaler Gno Naby

Refrain :
Ya Naby ya Rassoul’ allah
Salam aleika (bis)
Ma weuye la
Ma kagne la
Rassoul’ Allah ( bis)

Refrain + contre chant
tarou xel mou selle
kouko ame te weuyo Naby
weuye Wa nulle na ndeyssane
Ki moye
Ya Rassoul’Allah ya Habibala

Yaye borome lerre
Yaye borome yeurmander
Tourame di lignouye fatelikou ba fawe
Aye jeuffame di lignouye jexitale ba fawe
jare jarame di lignouye netali ba fawe
Sangue sangue ya ngui ni



Abonnez-vous ici : http://bit.ly/AdiouzaDiallo

Retrouvez Adiouza Diallo sur :
- Instagram: http://i.instagram.com/adiouza/
- Twitter : https://twitter.com/Adiouzaofficiel
- Facebook: https://web.facebook.com/AdiouzaPageFans/

FacebookTwitterFacebookLinkedInPinterest